Leeral Huqal Bukaa’u

Bismillaahi Rahmaani Rahiim Sang yi … Ku ci nekk day am leer gu toll ne leerug jant bi fu mu man a jëm. Su ko defe képp kuy leerloo ci moom day am lu rëy. Day mel ne ku gisul mbindéef yi ngir jublu Boroomam ak i leeram yu bari ak i mbóotam. Day man […]

Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (17)

Bismillaahi Rahmaani Rahiim Dénkaane bi mooy sunu xaaj bu mujj ci dénkaaneey Sëñ Alhaaji. Noo ngi key ñaanal Yàlla sàmm ko, guddal fanam, may ko wér, xéewal yu yaatu te barkeel, defal ko ngëramal Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaaralahu Fii nag dafay soññee ci nu góor-góorlu ci yittewoo nees di njariñoo ci Sëriñ Bu […]

Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (16)

Bismillaahi Rahmaani Rahiim Laabire gi Sëriñ Alhaaji Mbàkke daf ciy fàttali jeexug àdduna ak ñàkkam solo. Te sax li fiy jàmm mooy farlu ci sàkku lu baax ak di jaamu Yàlla. Noo man a tool, loo man a am, koo man a doon da nga faatu. Loolu sax mel na ni moo tax muy laaj […]

Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (15)

Bismillaahi Rahmaani Rahiim Ginnaaw nuyoo gu mat ci namu ko baaxo defe, la daaldi dénkaane sax ci jëfe ndigal ak bàyyi tere tey moytu yàq. Di boole it liggéey ak wakiirlu ci sunu Borom. Mu yee nu ci nopi ci lu amul njariñ ak sax bàyyi lu amul njariñ. Sëriñ Tuubaa daniwoon ku taqoo ak […]

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR