Kan Mooy Maam Seex Anta(1)

Mi ngi ganee àdduna atum 1867 ca poroxaan, turam dëgg mooy Seex Siidi Muxtaar Mbàkke mi ngi bokk ci askanu Maam MahramMaam Seex Anta doomi Sëriñ Moor Anta Sali la moom Maam Bàlla moom Maam Mahram.Maam Anta Njaay Mbàkke, doomi Maam Ibraahima Awa Ñang moom Maam Mahram mooy yaayam. Kon Muhammadul Xayri Mbàkke walla nga […]

Leeral Ilhaamu Salaam(1)

Bismillaahi Rahmaani Rahiim Dog bii ci Ilhaamu Salaam, Sëriñ bi daf ciy xamle sànkureefu majoos yi ak nasaraan yi ak worug Ibliis. Muy leeral ni seenug am-am ag jay dong la. Muy soññi jullit yi ci bañ a roy moykat yi ak bañ a yaakaar ni ngëneel ci ñoom la nekk. Mu war kon cib […]

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR