Bismillaahi Rahmaani Rahiim
Dog bii ci Ilhaamu Salaam, Sëriñ bi daf ciy xamle sànkureefu majoos yi ak nasaraan yi ak worug Ibliis. Muy leeral ni seenug am-am ag jay dong la.
Muy soññi jullit yi ci bañ a roy moykat yi ak bañ a yaakaar ni ngëneel ci ñoom la nekk. Mu war kon cib jullit mu am fulla sàmm Lislaamam, bañ a ragal tubaab yi ci dara.
Noo ngi ñaan sunu Boroom xiir nu ci ag njub ak dundal Lislaam ba fàww.
Al-Habdul Xadiim
05/06/2022
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien