Leeral Nahju (7)

Fii danu fiy leeral ni, jàng xam-xam dëgg-dëgg, ci ndaw lañu koy gën a manee. Njariñu xam-xam ci nit, dayoom gi ak i jeexitalam réy na lool ci ku jóg sóobu yoonu xam.

Yal nanu Yàlla xiir ci sàkku lu nuy njariñ ci àdduna ak fa allaaxira te lépp dëppook bëggug sunu Boroom ak ngëramam barkeb weeruw Shahbaan gi nu nekk.

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR