
Fii danu fiy àndi lenn ci jaar-jaari Ceerno Ibraahima Faati. Lu mel ni ki judoom, ay jikoom, digganteem ak Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu, miy magam di lépp.
Niki noonu dees na fi jukki ay bataaxel yu ko Sëriñ bi bindoon. Yal nanu Yàlla fayal Borom Daarul Muhti.
- kan moy Maam Cerno Birahim Mbàkke 5:32
- Yarug Cerno Ibraahima ak ngërëm la ca topp 9:25
- Maam Cerno géejug njariñ 3:48
- Ñaari Bataaxel Fa Cerno Ibraahima (11) 1:54
- Bataaxel bu jëm ci Borom Daarul Muhti 1:30
- Ñeenteelu Bataaxel jëm ci Maam Cerno(12) 1:28
- Juróomeelu Bataaxel Fa Seex Ibra Faati(13). 1:19
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien