Safwatu Siyar (8)

Sëriñ Bi dina di nettali na mu daan def bay xam weer yi. Naka noonu kooram gu tumranke ga ak ba muy julli iid.

La ma daan def yépp nag di lu kenn xamul ca dëkk boobu. Di fa jaamu Yàlla ak di fa wéetal Boroomam ak di fa Liggéeyal Yonent bi Aleyhi Salaam.

Di sàkku ci ñépp ñu ñaanal Sëriñ Ibraahima Mbàkke moom Sëriñ Muntaxaa sunu Borom dolli ko yërmande ak njéggal ak ngëram ba fàww.

Safwatu Siiri

Safwatu Siyaar (7)
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
✕
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR