
Fii dinanu fi nettali lenn ci ay xew-xew amoon Mayomba ba Sëriñ Bi di wax ak géej gi ak wiir-wiir, raglu gi ak doywaar gi.
Jàmbarug Sëriñ Bi, fit wi ak bàyyee boppam Boroomam dina fi feeñee itam. Waaye it ni ko sunu Boroom taxawoo ci lépp.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien








