Fii danu fiy àndi ay leeral ci teggini sàmm say gët, worma gi nu wara wormaal mag ñi. Ci bu nu tooge ak ñoom, bu nu àndee ak ñoom ci tukki, bu nuy lekkandoo ak ñoom ak yeneen.
Njariñul wax dëgg, ay jeexitalam ak dayo gi am fa Yàlla.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien