Kan Mooy Sëriñ Mustafaa Faal

Diirug li ñuy nekk foofu ñoo ngi doon liggéeyal Sëriñ bi ba am ngëramam. Ci liggéeyu Sëriñ Tuubaa gi la sax, moo tax sanc na ay dëkk di fa defare. Bokk na ci yooyu dëkk Daaru-Faal, Tuubaa-Faal, Kuuba, Aynu Rahmati añs. Amoon ay tool yu bari, di bàyyi xel tolluwaayu jamono moo tax mu ubbiwoon […]

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR