Safwatu Siyaar (7)

Dina leere ci nettali yi mën a muñug Sëriñ Bi ci lori ay noonam. Te jamono ju ne muy kuy déllu ci Boroomam Subhaanahu wa Tahaala ànd ak wéetaay ak ndëgërlaay ci aw yoonam. Am na itam ay nit yu ko daan taxawu ci coobareey sunu Boroom, daan ànd ak moom ak di ko diis […]

Leeral Mawaahibul Xudduus (11)

Boo gëmee Muhammadu Rasuulul Laah ndawul sunu Boroom la, SHW gëm nga ne Yónente yépp dañuy jotal, te duñu fen, duñu def lu araam, duñu def lu ñu sib. Mel na ni fii mu ne mboolem li nekkoon ci “Laa Ilaaha Illaal Laah Muhammadu Rasuulul Laah” SHW ciy pas-pas leeral naa ko. Xay na baat […]

Safwatu Siyar (6)

Fii dinanu fi nettali lenn ci ay xew-xew amoon Mayomba ba Sëriñ Bi di wax ak géej gi ak wiir-wiir, raglu gi ak doywaar gi. Jàmbarug Sëriñ Bi, fit wi ak bàyyee boppam Boroomam dina fi feeñee itam. Waaye it ni ko sunu Boroom taxawoo ci lépp.

L’arme des Craintifs (9)

Les paroles du prophète de l’Islam, Aleyhi SalaamAl-Boukhariyou rapporte dans son livre que :

Safwatu Siyar (5)

Nu ngi sàkku ñépp ñaanal Sëriñ Mbay Géy Sill, njégalu sunu Boroom, yërmandeem ak ngërëmam. Ci 5i xaaj bi danu fiy xamle xew-xew ya amoon ba Sëriñ Bi duggee ci gaal gi niki ka ko doon tooñ. Ab nekkam Libreville ak tiis ya, natu ya, naka noonu ya Lambaréné ak feneen. Nga xammee ci mën […]

L’arme des Craintifs (8)

Le pèlerinage comporte quatre actes obligatoires : l’intention, la marche circulaire autour de la kaaba (tawaaf, wër kaaba gi), la course rituelle entre Safaa et Marwa, et la station d’Arafa. Voici les actes traditionnels à effectuer : la purification majeure qui précède le moment de sacralisation (harmaal), l’interdiction de porter des habits cousus, ne porter […]

L’arme des Craintifs (7)

L’arme des Craintifs (7): Quiconque veut jeûner doit obligatoirement formulerl’intention de le faire et s’abstenir de…

Safwatu Siyar (4)

Ginaaw leeralug làqug Sëriñ Maam Moor Anta Sali, taxawaayu Sëriñ Bi, ak yoonu tarbiya gi mu ubbi, teg ci ay taalibeem, di leen yar ak soññi, di leen yee ak njariñ. Dina feeñee ci xaaj bi lenn ci sababi tukki bi, ak ni tukki bi demee, lenn ci yi aju ak yeneen.

Safwatu Siyar (3)

Ci ñetteelu xaaj bi di nga fi xamee lenn lu aju ci nelawag Maam Moor Anta Sali ak taxawaayu Sëriñ Bi ginnaaw làqug way-juram wu baax ba. Danga fi dégge it lenn lu aju ci waxante yi amoon ca denc ba. Naka noonu tànnug Sëriñ Bi ba ñu key wax lu mën ñongal àddunaam. Yiteem […]

Safwatu Siyar (2)

Ci xaaj bi lanuy leeral lenn ci li aju ci jàngum Sëriñ Bi. Farlu gi woon ci moom, sàmmonte gi, réyug xelam ak man a déggam. Dina fi feeñ tamit njariñ li mu amoon ci Daaray Sëriñ Moor Anta Sali, ak fi mu ko féetewoon. Ci buntu bi daanaka li ciy féd mooy jàngam, jàngale […]

✕
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR