Boo gëmee Muhammadu Rasuulul Laah ndawul sunu Boroom la, SHW gëm nga ne Yónente yépp dañuy jotal, te duñu fen, duñu def lu araam, duñu def lu ñu sib. Mel na ni fii mu ne mboolem li nekkoon ci “Laa Ilaaha Illaal Laah Muhammadu Rasuulul Laah” SHW ciy pas-pas leeral naa ko. Xay na baat […]