Safwatu Siyar (8)

Sëriñ Bi dina di nettali na mu daan def bay xam weer yi. Naka noonu kooram gu tumranke ga ak ba muy julli iid. La ma daan def yépp nag di lu kenn xamul ca dëkk boobu. Di fa jaamu Yàlla ak di fa wéetal Boroomam ak di fa Liggéeyal Yonent bi Aleyhi Salaam. Di […]

Safwatu Siyaar (7)

Dina leere ci nettali yi mën a muñug Sëriñ Bi ci lori ay noonam. Te jamono ju ne muy kuy déllu ci Boroomam Subhaanahu wa Tahaala ànd ak wéetaay ak ndëgërlaay ci aw yoonam. Am na itam ay nit yu ko daan taxawu ci coobareey sunu Boroom, daan ànd ak moom ak di ko diis […]

Leeral Mawaahibul Xudduus (11)

Boo gëmee Muhammadu Rasuulul Laah ndawul sunu Boroom la, SHW gëm nga ne Yónente yépp dañuy jotal, te duñu fen, duñu def lu araam, duñu def lu ñu sib. Mel na ni fii mu ne mboolem li nekkoon ci “Laa Ilaaha Illaal Laah Muhammadu Rasuulul Laah” SHW ciy pas-pas leeral naa ko. Xay na baat […]

✕
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR