Dina leere ci nettali yi mën a muñug Sëriñ Bi ci lori ay noonam. Te jamono ju ne muy kuy déllu ci Boroomam Subhaanahu wa Tahaala. Am na itam ay nit yu ko daan taxawu ci coobareey sunu Boroom, daan ànd ak moom ak di ko diis seen i soxla. Yal nanu Yàlla sàmmal sunu […]