Sëriñ Isaa Jenn mooy doomi Sëriñ Ibraahima Jenn ak Soxna Maryaama Jóob. Di waa Kajoor, mi ngi gane àddina ci atum 1863 walla 1865. Li gën a woor daal moo di moom ak Maam Cerno ñoo maase. Sëriñ Isaa Jenn mooy koo xam ne amul woon benn soxla bu dul bu Sëriñ bi. Jàng na […]