- Seex Faati Tàkko JóobCe livre retrace la vie et l’œuvre de l’un des plus grands compagnons de Cheikh Ahmadou Bamba Mbacké. Ce dernier quitta ce monde alors que le héros de ce livre n’avait que 27 ans. C’est dire qu’avant cet âge déjà, il était devenu un homme remarquable, un
il y a 2 jours - Jotaayu Texe (2)Dees na xamee ci xisa yi yu bari ci mayi Yàlla yi. Nit dina man a xam ay mbir yu nëbbu ci coobareey sunu Boroom. Dina fi feeñee itam dolleey ngëm, dooleey kóolute ak i jeexitalam ci topp ndigalu Sëriñ bu mat Sëriñ. Yal nanu Yàlla saxal ci ag taalube, sàmm
il y a 6 jours - Kan Mooy Sëriñ Mbàkke Buso…Am na benn buur gu féetewoon Lambay dafa sonnaloon lool murid yi ba Sëriñ Mbàkke Buso bindoonko bataaxal di ko wax mu teey loram ci murid yi. Sëriñ Mbàkke Buso it dund na lu metti atum 1895. Ndax ci at moomu la baayam, miy nijaayi Sëriñ Tuubaa, faatu. De
il y a 1 semaine - Kan Mooy Sëriñ Mbàkke Buso…Am na benn buur gu féetewoon Lambay dafa sonnaloon lool murid yi ba Sëriñ Mbàkke Buso bindoonko bataaxal di ko wax mu teey loram ci murid yi. Sëriñ Mbàkke Buso it dund na lu metti atum 1895. Ndax ci at moomu la baayam, miy nijaayi Sëriñ Tuubaa, faatu. De
il y a 1 semaine - Miftaahul Xuyóob (8)Fii di nanu fi leeral mellow génnug ruu, ak yi ci aju yépp. Naka noonu dees na fi xamle laaji yi nga xam ne dina am ci bàmmeel ak ginnaaw laaj yi li fay xew. Yal nanu Yàlla sàmm te tënk nu ci lislaam.
il y a 2 semaines - Jotaayu Texe (1)Li ab Téere bu m njariñ lool, ay wax ak i jëfiinu Sëriñ Bi moo ci nekk, nu man ci gindiku ci sunu lislaam ak ci sunu taalibe. Fii nag matug Boroom Tuubaa dina di feeñee ak sunu tawfeex ci ànd ak moom. Yal nanu nuur ci moom barkeb Xasiida yi .
il y a 2 semaines - Café Touba🎉PROMO SPÉCIALE OUVERTURE 🎉 Bienvenue chez Amdi Café ! Pour le lancement de notre boutique, profitez de notre offre exclusive : Le café Touba est à 17,99€ le kilo 😍. ✨ Offre valable jusqu'au 25 mars Après cette date, le prix reviendra à 20,99€ le
il y a 3 semaines - L’attraction vers les grâces et l’éloignement des illusions (4)Toi qui aspires à parvenir à Dieu, sache qu’il existe quatre ennemis et contraignants à ta quête, il te faudra dès lors t’opposer à eux. Il s’agit de Satan, du bas-monde, de l’âme charnelle et des désirs charnels. Emprisonne l’âme charnelle dans la faim m
il y a 4 semaines - Leeral Miftaahul Xuyóob (7)Nu wéyal ba tay ci mbiri baamel? Ndax mooy ku ñu def ci pax rekk ? Am romb na loolu. Dees na fi leeral tamit xew-xew gu amoon diggante benn jullit ak ben yéefar gu siiw bob, di neen ci jëlle ay jàngat yu fees dell ak waare. Yal nanu Yàlla musal ci tiisu b
il y a 4 semaines - Miftaahul Xuyóob (6)Fii danu fiy leeral lu aju ci bàmmeel ak dundug bàmmeel ci waxi Kilifa yi. Dees na fi xamee itam ne, sax ci lu baax dara amul njëgam. Naka noonu topp li Yàlla digle ak wattandiku tere yi. Yal nanu Yàlla saxal cig njub barkeeb koor gii nu nekk.
il y a 1 mois - L’attraction vers les grâces…(3)Nous sommes à notre troisième numéro et l’étude de ce poème, se poursuit : « Quiconque t’empêche d’obéir à Dieu, loué soit-il, sépare-toi delui. Il existe cinq choses qui permettent d’accéder à Allah : Serigne Touba
il y a 1 mois - Kan Mooy Sëriñ Mustafaa SaalihDaa mel ni wax ji jenn la. Doomi Soxna Mati Jaxate ak Sëriñ Saalihu dem am gi bet na nu. Daf doon murid saadix, te ay kilifaa ko wax, seedeel ko ko. Yal na ko Yàlla dolli xéewal fa mu nekk, yërmande ak i leer te taas nu ci barkeem. Sunu Boroom yal na ko [
il y a 1 mois - Miftaahul Xuyóob (5)Ay leeral yu jëm ci li war boroom kër ci soxnaam, yuy gën a dëggaral yi nu doon wax ci ginnaaw. Yii dafay jëm ci xamle lislaam ak yi ci aju, mu mel ni kon jàng manta ñàkk. Yal nanu Yàlla defal xam-xam.
il y a 2 mois - Midtaahul Xuyóob (4)Ci xaaj wi danu fiy leeral yi nga xam ne dina araam ci jigéen bu am ngàtt mu di ko def, mba muy dem ci ay barab yu mu warul dem. Te war na ci Boroom kër mu xamal ko soxnaaam. Te mu xamal ko it mbolleem lu aju ci wàll woowu.
il y a 2 mois - L’attraction vers les grâces…(2)Nous sommes toujours à la première phase : l’introduction. « Je sollicite l’aide de Dieu qui a écarté de moi tout cequi ne m’est d’aucune utilité dans un poème qui sera bénéfique à un nomade ou à un sédentaire, un poème qui est d’une beauté qui ravit cell
il y a 3 mois - Box CouraAvec la Box Coura, obtenez un tapis personnalisé, un Coran, un chapelet en perles et un chapelet électrique dans un beau coffret.
il y a 3 mois - Miftaahul Xuyóob (3)Ba tay warteefi borom kër ci soxnaam leen fiy xamle. Mel ne xamal ko diineem ak yi ci aju. Di ko leeralal lenn ci sew-sewi julli ak yi ci des. Daa wara xamal njabóotam itam ak ñi mu yilif seen diine. Yi jëm ci dareeti mbërag, wësin, yooyu yépp daf ko wara
il y a 3 mois - L’attraction vers les grâces et l’éloignement des illusionsDans cette œuvre, Serigne Touba nous parle des bonnes mœurs, des valeurs, des qualités et des vertus louables auprès d’Allah, auprès de la société et envers nos semblables. C’est une belle œuvre, riches en leçons, avec de magnifiques maximes et des sagess
il y a 3 mois - Miftaahul Xuyóob (2)Ci xaaj wi, dees na fi lim yi nga xam ne war na boroom kër mu xamal ko soxnaam, ñi mu njaboote. Te mooy faratay jëmam ak mbolleem li ci aju, dalle ko ci laab, ponki diine yi la cay farata ak sunna. Di ko waar ngir bëggal ko lu baax ëllag. Te sax « góor gu
il y a 4 mois - Miftaahul Xuyóob (2)Ci xaaj wi, dees na fi lim yi nga xam ne war na boroom kër mu xamal ko soxnaam, ñi mu njaboote. Te mooy faratay jëmam ak mbolleem li ci aju, dalle ko ci laab, ponki diine yi la cay farata ak sunna. Di ko waar ngir bëggal ko lu baax ëllag. Te sax « góor [&
il y a 4 mois - Le Mouridisme est une voie de raison« Cet ouvrage décrypte les fondements de la voie mouride et offre au lecteur les clés pour une compréhension éclairée de ses enseignements. Il est regrettable de constater que, comme dans tout mouvement, des individus malintentionnés cherchent à détourner
il y a 4 mois - Leeral Miftaahul Xuyóob (1)Li ab Téere la bu am solo jëm ci xamlee nees di yoree sa Soxna ak ay mbir yu jëm ci dundug bàmmeel ak yeneeni yëf. Ku ñuy wax Umar Jóob moo doon laaj Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu ay laaj yu am solo. Sëriñ bi bind Téere bi àndil ko ci ay [&h
il y a 4 mois - Kan Mooy Sëriñ Mbàkke MadinaSëriñ Mbàkke Madina, dafa doonoon nit ku fonk jàng, jàngale ak jëfe xam-xam. Doonoon ku fonk sunnas Yonent bi Aleyhi Salaam, di ko dund bu wér. Dafa doonoon ku noppi, am dal lool, bari ñu ko sopp muy kilifa yi di ndogo yi. Mbokkam yépp bëgg ko ak daan ko
il y a 4 mois - Kan Mooy Gaïnde FatmaKu amoon gis-gis bu sori la. Dafa teel a yeewu ci doxiinu jamono. Moo tax masul neenal benn xam-xam bu am njariñ. Dafa daan yóbb ay nit ñu bari ñuy jàngi ci yeneeni réew. Teewul itam mu sàmp ay jàngukaay ci biir Senegaal. Tuubaa itam mu liggéey mbed yi, d
il y a 5 mois - Leeral Fathul Zaahiril Baatin…(2)Dina fi feeñ lenn ci njariñ yi nekk ci bàyyeek sa lépp sa Boroom, woolu ko bu wóor, ak wéral sab pas-pas ci dëggal saw doxiin sa diggante ak moom. Am na lees ci toftal ci Téere bi, jëm ci leeral luy mag, ak i màndargaam. Akub tënk jëm ci ponki Diine.
il y a 5 mois - Box DiatouDécouvrez la Box Diatou, l’alliée parfaite pour enrichir vos moments de recueillement ! Chaque box est soigneusement conçue pour répondre à vos besoins spirituels tout en reflétant votre style unique. Voici ce qu’elle contient : – Un tapis élégant q
il y a 5 mois - Tapis de prière– Personnalisez votre tapis de prière ! Créez un tapis de prière unique, fait selon vos préférences. Choisissez la couleur de votre choix et ajoutez une touche personnelle en inscrivant votre nom. Il vous suffit de préciser ces détails lors de votre
il y a 5 mois - Synthèse du Viatique (12)Dans cette partie, et la dernière synthèse du Viatique, nous nous intéressons à la perfection spirituelle en mettant en exergue la bonne conduite à adopter dans notre dévotion. Nous rappelons ici les conseils essentiels que le Cheikh donne aux adolescents
il y a 6 mois - Livres numériquesLa bonne nouvelle est que vous pouvez désormais lire 3 de nos publications en version numérique. Pour chaque livre, vous avez droit à 2 téléchargement
il y a 6 mois - Kan Mooy Sëriñ Musaa KaMoo doon Werekaanu Bàmba, di xamle jaar-jaari yoonu murid, cëslaayiyoon wi ak daan dànkaafu képp kuy dal ci Sëriñ bi mbaa ci yoon wi. Mooy koo xam ne kenn du sosal kenn ci ñoñ yoon wi mbaa boroom yoon wi te mu nekk fi. Mooy délluwaay bu mag bi ci xam mell
il y a 6 mois - Leeral Fathu Zaahiril Baatin…Ginnaaw muslu ci saytane, ak julli gu mat ci Yonent bi Aleyhi Salaam, Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu daa sant Yàlla bu wér. Dafa daaldi xamle li yit pas-pas bi nu war a am ci sunu Boroom ak ay jeexitalam, ci sunu nekkin, sunu jëfin ak sunu du
il y a 6 mois - Synthèse du Viatique (11)Après avoir expliqué l’ablution majeure et l’ablution mineure en montrant les raisons pour lesquelles il faut l’effectuer, et comment l’effectuer, nous montrons aujourd’hui qu’à défaut d’avoir de l’eau et surtout pur, on peut se contenter d’une autre prat
il y a 7 mois - Synthèse du Viatique (10)Nous sommes à notre dixième numéro de la synthèse du viatique. Après avoir parlé des bases de la foi et des piliers de l’Islam, nous abordons, cette fois-ci, une phase importante du viatique et de nos pratiques habituelles : les ablutions. Qu’Allah nous g
il y a 7 mois - Kan Mooy Sëriñ Masàmba Jóob SaamSëriñ bi nag moo gis Sëriñ Masàmba fekk ko ci ronn garab muy yër ab téere. Sëriñ bi nuyu ko, ñuy jàmmasante ak a waxtaan. Ginnaaw gi nag la Sëriñ Masàmba laxasaayu ni day seeti Sëriñ Tuubaa. Ci la daaldi dem Pataar ci daaray Sëriñ Moor Anta Sali nekk fa d
il y a 7 mois - Synthèse du Viatique (9)Nous abordons dans notre neuvième numéro la Zakat et le Pèlerinage. Ils font partis des piliers de l’Islam. Nous parlons des actes obligatoires de la Zakat ainsi que les attitudes à avoir dans la donation de l’Aumône. Pour ce qui est du Pèlerinage nous n’
il y a 8 mois - Synthèse du Viatique (8)Nous sommes à notre huitième numéro. Nous étudions ici les actes obligatoires de la prière et du jeûne. Une annonce est faite sur ce que nous attend dans les prochains jours en termes de partage et d’instruction. Qu’Allah nous guide dans le droit chemin.
il y a 8 mois - Synthèse du Viatique (7)Dans cette partie, nous mettons l’accent sur l’importance de la prière, son statut obligatoire, et sa dimension spirituelle et apaisante. Ensuite, une orientation est donnée vers ce dont nous aborderons dans les prochains jours : le jeûne et les autres pi
il y a 9 mois - Synthèse du Viatique (6)Nous avons par la grâce d’Allah traité, comme on pouvait, la notion de foi dans la religion musulmane. La sixième section de cette synthèse marque le point de liaison en la foi prononcée et son déploiement dans les actes et dogmes religieux. Dans cette pa
il y a 9 mois - Tombi Borom Tuubaa (30)Noo ngi toll ci sunu 30i xaaj ci Tombi Borom Tuubaa. Dina feeñee ci néttali yi ni liggéeyal Sëriñ amee lool doole ci nun ak tawfeex gi nekk ci topp ay ndigalam ak bàyyi ay tereem. Naka noonu di ko sant fu nu toll, doyloo ko, woolu ko te womatu ci moom man
il y a 9 mois - Kan Mooy Seydina Usmaan MbàkkeBaay Njaga Jóob nee na : « Seydinaa Usmaan dafa njariñu ci Seex Ibra, njariñu ci Maam Cerno, njariñu ci Sëriñ Tuubaa ». Ku daan ñaan la muy am, te ràññeeku ci lool. Am na sax ay nit yu daan jëfandikoo sàngara, moo ko dindi ci ñoom ci lu gaaw. Daf daan soñ
il y a 9 mois - Synthèse du Viatique (5)Nous abordons dans la 5e partie de la synthèse du Viatique, le croyance au décret divin et au jugement dernier. Cette partie boucle aussi l’essentiel de ce qu’on avait pour objectif de partager sur les piliers de la foi musulmane.
il y a 10 mois - Synthèse du Viatique (5)Nous abordons dans la 5e partie de la synthèse du Viatique, le croyance au décret divin et au jugement dernier. Cette partie boucle aussi l’essentiel que ce qu’on avait dessein de dire sur les piliers de la foi musulmane.
il y a 10 mois - Kan Mooy Seex Muhammadu Lamin Jóob DaganaSeex Muhammadu Lamin 1886 la gane àddina. Yonent bi AleyhiSalaam la ko baayam tudde. Soxna Haanatu Jóob mooy way-juram wu jigéen. Sëriñ Tafsiir Ahmadu Jóob mooy baayam mi ngi dëkkoon Dagana. Wollare Sëriñ Tuubaa la woon, moo ko jébbal itam Sëriñ Muhammadu
il y a 10 mois - Tombi Borom Tuubaa (29)Fii dana fi feeñee farlug Sëriñ bi ci jëfe ndigalu sunu Boroom, ak xam gi mu xam ni àdduna jaaruwaay la. Naka noonu terangay Alxuraan ci ñu koy jàng ak tawfeex gi ci Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu am. Su ko defe lii di nu soññi ci xam ne àddu
il y a 10 mois - Cheikh Mountakha entre mots et imagesUn recueil de notes et un petit album photo
il y a 11 mois - Synthèse du Viatique (4)Dans cette 4e partie de la synthèse du Viatique, nous abordons deux points : la croyance aux livres célestes et la croyance aux prophètes. L’accent sera mis sur le nombre de livres attribués à chaque prophète. Nous donnerons aussi le nombre de prophètes m
il y a 11 mois - Tombi Borom Tuubaa (28)Sëriñ bi fii dina fiy néttali mbir yu am solo ci pajug yaram. Dina fi wax it nees di jëfandikoo lenn ci xob yi. Nangug ag ñaanam, ak xam nees di fasee sa soxla dina fi feeñ ak ni mu fonkewoon aaya Alxuraan yi ci lépp lumuy def. Naka noonu ag sàmmam ci dii
il y a 11 mois - Tombi Borom Tuubaa (27)Ginnaw fàttli yi aju ci ndëgarlaayug néttali yi, ci leen daaldi wéyal yaatal wi. Am na ci yu jëm ci mbiri tubaab yi ak waxiini Sëriñ bi, na miy kaweem xel, ak nees di déggee ay waxam. Kollareem ak taalube yi itam dina fi fés, fullaam, ak dénkaane yu am so
il y a 11 mois - Marsiya Ak WolofalMarsiya Maam Ceerno Mbàkke Marsiya Seex Ndaam Abdurahmaan Lóo Ay wolofalu Soxna Maymuuna Mbàkke Kubra
il y a 12 mois - Synthèse du Viatique (3)Ici, on revient sur quelques points de réflexion notamment dans Muwaahibul Xudóos avant d’aborder le chapitre de la croyance aux anges extrait de Tasawud Sixaar. Croire aux anges fait partie des piliers de la foi musulmane. Qu’Allah nous préserve dans le
il y a 12 mois - Cheikh Mountakha MbackéLe leadership d'un soufi accompli
il y a 12 mois - Synthèse du Viatique (2)Ici, nous donnons une définition simple de la théologie ou la science discursive pour introduire notre thématique sur les cinq aspects de la foi musulmane. Priorité est donnée aujourd’hui exclusivement à la croyance en Dieu. Qu’Allah nous facilite et nous
il y a 12 mois - Leeral Nahju (9)Su ko defe, ci xaaj wi la nu matale sunub liggéey ci Téere bii di Nahjul Qadaa Al-Haaj. Njariñ li yaatu na lool, la muy xamle di sunub defaru tay ak ëllag. Mbolleem li ci Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu ñaan yal nanu dal. Yal nanu Yàlla saxal
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (26)Fii danu fiy néttali leen ci téerey boroom ngir yi ni nu agsee ci Sëriñ bi. Tawfeex gi mu am ci ànd ak Boroomam ci lépp lu muy dugg dees na ko fi xam itam. Naka noonu sell gi woon ci moom taxoon na dara manta rax ay mbiram. Fàww rekk lu sell rekk lay [&he
il y a 1 an - Synthèse du « Viatique » (1)Bismillahi Rahmaani Rahiim Pour notre premier numéro nous allons étudier l’ouvrage de Serigne Touba sur les bases de l’islam, intitulé « Tasawud Sixaar » [ Le viatique des adolescents]. Nous allons mettre en exergue l’amorce de l’ouvrage avant d’introduir
il y a 1 an - Promo Pack Ramadan« Pack Ramadan », trois livres : Kansul Muhtadin, Nitug Yàlla, Le Trésor Des Bien Guidés ; un jeu de cartes : Les Bases De L’Islam, a seulement 50€.
il y a 1 an - Leeral Nahju (8)Ci xaaj wi dees na fi leeral teggin yi war diggante Taalube bi ak Sëriñ bi. Njariñ li nekk ci topp Sëriñ bu mat Sëriñ. Ni mu lay defare, ni mu lay dimbale ak ni mu lay taxawoo sa diggante ak sa Boroom. Sëriñ bi itam dina fi leeral dëgg-dëggi xarit ak mbok
il y a 1 an - Carte Xam-Xam : livraison gratuite jusqu'à 17 MarsBénéficiez d'une livraison gratuite pour tout achat d'une Carte Xam-Xam jusqu'à 17 Mars 2024.
il y a 1 an - Nafila du mois de RamadanLes 30 Nafila extraits du livre intitulé "Khuratul ayni" écrit par Serigne Souhaïbou MBACKE.
il y a 1 an - Leeral Nahju (7)Fii danu fiy leeral ni, jàng xam-xam dëgg-dëgg, ci ndaw lañu koy gën a manee. Njariñu xam-xam ci nit, dayoom gi ak i jeexitalam réy na lool ci ku jóg sóobu yoonu xam. Yal nanu Yàlla xiir ci sàkku lu nuy njariñ ci àdduna ak fa allaaxira te lépp dëppook bëg
il y a 1 an - Dundug Maam CeernoFii danu fiy àndi lenn ci jaar-jaari Ceerno Ibraahima Faati. Lu mel ni ki judoom, ay jikoom, digganteem ak Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu, miy magam di lépp. Niki noonu dees na fi jukki ay bataaxel yu ko Sëriñ bi bindoon. Yal nanu Yàlla fayal
il y a 1 an - Dundug Maam CernoFii danu fi dajale leen ci jaar-jaari Cerno Ibraahima Faati. Di neen fi xamle judoom, jàngam, doxiinam ak ay jikkoom. Dees na fi fésal lenn ci bataaxel yi ko Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu daan bind ak yeneeni wax yu am njariñ. Yal nanu Yàlla
il y a 1 an - PACK RAMADANVous avez dans votre « Pack Ramadan », trois livres : Kansul Muhtadin, Nitug Yàlla, Le Trésor Des Bien Guidés ; un jeu de cartes : Les Bases De L’Islam. Al-Habdul Xadiim pour vous servir !
il y a 1 an - Leeral Nahju (6)Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu daa soññee lool ci tabe, teral gan ak yaatal ko. Mu fiy wax lu tax loolu di lu manul ñàkk ak xéewal yi ci nekk ak ngëneel yi. Di wax it solos xam-xam, tolluwaay wu réy gi ma am fa sunu Boroom. Di leeral ne ndamo
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (25)Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu daf nu fi dénk jàng, liggéey ak sàmm sunu diine. Dina fi leeral itam, moom Sëriñ bi, lu jëm ci ay mbiram niki wirdam, Sëriñam, yoonu géej gi ak yeneeni mbir. Naka noonu dees na fi déggee lenn ci ay jagleem ak i
il y a 1 an - NAYLUL AWTAAR (4)lii ngay bëgg a jàng mooy ñenteelu xaaju Naylul Awtaar. Ci lanuy fas yéene tëj Téere bi. Li des ci tomb yépp nag, day jëm ci ñaan yu baax yi,...
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (24)Sëriñ Tuubaa dina fi leeral leen ci baati wolof yi ak mahnaa gi ñu ko wara jox dëgg-dëgg. Lenn ci xarbaax yi itam dees na feeñee fi. Naka noonu Hikma yi.Ba tey ci néttali yi di neen fi dégg luy waral nu wara gën a sàmm sunu kolare ak Sëriñ Tuubaa, sunu di
il y a 1 an - NAYLUL AWTAAR (3)Asalaamu Haleykum mbokk mi! Ginnaaw ñaari xaaj yi nu la àndiloon ci Naylul Awtaar, jàppal ci fanwéeri (30) tomb yi:
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (23)Fii dañu fiy fésal ni Sëriñ wéetale Boroomam ak liggéey gu muy liggéeyal Yonent bi Aleyhi Salaam ak ni mu key feeñale ci mbindam. Naka noonu sunu Borom dig na ko lu réy ëllag ginnaaw jaamu Yàlla ju refet gi mu jaamu Boroomam ak jaayanteem ju réy ji.
il y a 1 an - NAYLUL AWTAAR (2)Ginnaaw xaaj bu njëkk bi nu defoon ci Naylul Awtaar mu Sëriñ Suwaahibu radiya laahu anhu...Danoo fas yéene tay, àndil leen ñaareelu xaaj bi...
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (22)Di neen fi béral lenn ci dooley mbidum Sëriñ Tuubaa, njariñ yi mu làmboo ak jagle yi ak barkeb mbindam. Naka noonu lenn ci mayi Sëriñ bi dees na ko fi fésal, ci man a xeetali mbindéef yi, fuñu man a nekk. Dees na fi dégg it nettali yoy dees koy gëm waaye
il y a 1 an - NAYLUL AWTAARBismilaahi Rahmaani Rahiim. « Li Sëriñ Alhaaji Mbàkke Xaadimul Xadiim jëlle ca Naytul Awtaar, moom lanu àndi fii ngir ni manula dawal mbidum araab...
il y a 1 an - COMPRENDRE LE WIRD MOURIDE EN PETITS PARAGRAPHES
il y a 1 an - Leeral Nahju (5)Fii danu fiy àndi ay leeral ci teggini sàmm say gët, worma gi nu wara wormaal mag ñi. Ci bu nu tooge ak ñoom, bu nu àndee ak ñoom ci tukki, bu nuy lekkandoo ak ñoom ak yeneen. Njariñul wax dëgg, ay jeexitalam ak dayo gi am fa Yàlla.
il y a 1 an - Leeral Nahju (4)Fii Sëriñ Alhaaji daf fiy leeral dénkaaney Sëriñ Tuubaa ci sàmm sa bopp, am kersa ak di wormaal nit ñi. Njariñul nuyoo, teggini nuyoo ak ay jeexitalam dees na ko fi fésal. Naka noonu yar say gët, màndu, xam kooy àndal, xam kooy roy dina fi leere. Ay wax y
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (21)Ci xaaj bi, dees na fi àndi lenn ci yi Sëriñ bi daan wax ci bisu penc ak may yi ko fa Yàlla jagleel. Ni miy xéttale nit ñi ci àdduna noonu it la leen di xéttale ëllag. Naka noonu di neen fi béral lenn ci dénkaane yi itam ak njariñ yu réy yi ñu […]
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (20)Fii di neen fi leeral njariñal topp ndigal ak yitewoo njub. Dees na fi fésal itam ni léppi Sëriñ barkeele ak ni Yàlla di nangoo ñaanam. Xar-baaxi Sëriñ Tuubaa itam cig mbindam ak i jagleem ak ni mu daan taxawoo taalube yi dees na ko fi xamee itam. Naka no
il y a 1 an - Leeral Nahju (3)Fii deef na leeral lenn ci ay teggin yi nit ki wara làmboo bu toogee ak ay mag walla mu nekk ci biiri nit. Naka noonu deef na fi béral itam, ni nit ki wara sàmmee ay gëtam ak làmmiñam. Di xool lu baax, di am kersa tey wax yiw. Di tàggat boppam itam ci [&h
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (19)Dog wi deef na fi àndi itam lenn ci xar-baaxi Sëriñ bi, lenn ci yi ko Yàlla may ak lenn ci ay hikmaam Naka noonu da nga fi dégg ay hisa yuy wone ni am na it ñu ko daan jéem a natu ci anam yu kéemaane. Ak ni mu daan delloo lépp ci Yàlla. […]
il y a 1 an - LEERALUG MULAYYINU SUDUUR
il y a 1 an - Tombi Borom Tuubaa (18)Fii dees na fi wone lenn ci màndargay yërmandey Sëriñ bi ak ñi mu daan sàmme kollare. Ni mu wàccoog nun itam ci wax, ci jëf ak ci bind. Ak ni mu defoon ragal Yàlla muy lépp. Naka noonu dees na fi leeral yennet ci xisa yuy wone xar-baaxi Sëriñ Tuubaa Xaada
il y a 1 an - Leeral Nahju (2)Ci ñaarelu xaaj bi dees na fi àndi ñaan yi Sëriñ bi ñaan ci Téere bi ak li muy ñaan ci Boroomam ak di ko ñaanal képp ku jàng Téere bi. Mu di fi dénk taalube yi ay teggin, boole ci di leeral luy teggin, soloom ci nit ki ak ni mu gànjaroo. Mu mel […]
il y a 2 ans - Kan Mooy El Haaji Baara MbàkkeSunu sang bi turam dëgg mooy Muhammadul Amiin, ñu duppee ko Sëriñ Muhammadu Lamin Baara Mbàkke miy doomi Sëriñ Tuubaa. Sëriñ El Haaji Baara nag mi ngi gane àddina atum 1921 fa Ndidi. Baayam moo di Sëriñ Fàllu Mbàkke, ndeyam di Soxna Xari Sàll. Baayam moo
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (17)Ci xaaj wi dees na fi xamle itam leen ci Sëriñ bi, ni ki mbir yum baaxowoon def ak bis yu mu ko daan def. Ni mu fonkewoon julli ci waxtu, ak ni mu daan sàmmee taalube yi. Ba tay, dees na fi wone ni mu doone ki nuy cinu ak di nu musal di […]
il y a 2 ans - Leeral Nahju (1)Li mooy tàmbalig Téereb Nahjul Qadaa Al-Haaji.Ubbite gi rekk doy na yóbbalug dund. Dina fi feeñee ay laabire yu am solo ci sax ci jëf lu baax te bañ a taayi. Naka noonu ay wax yu am solo te bari njariñ moo fiy fés. Ay royukaay ci bépp Jullit, te mooy saha
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (16)Ni Sëriñ bi daan jaamo Yàlla, la nu fiy béral. Anam gi mu daan jàngee Alxuraan, fonkeel gi, ak baril lu mu key jàng, waxtu yi mu daan bind, ay naafilaam ci ay ràkka, yooyu dees na fi fésal dara. Naka noonu mellom moom ci bind, ay xeeti waxam ak jëfinam, a
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (15)Tay nag kàddu yi daa jëm ci waxi Sëriñ bi ci mag ñi niki Maam Cerno, Seex Ibraahima Faal, Maam Seex Anta, Sëriñ Daaru Asan Njaay, Sëriñ Abdu Karim Ture… Dina fi feeñee itam seen i jagle yu réy ci Sëriñ bi. Seenug baax, seenug jàmbaar, seen i jikko yu refe
il y a 2 ans - Kan Mooy Sëriñ Siidi Muxtaar MbàkkeSëriñ Siidi Maxtaar, Sëriñ Baara Mbàkke ak Soxna Mati Ley ñooy ay way-juram. Mi ngi gane àddina atum 1925 fa Mbàkke Kajoor. Baayam moo ko dalal Alxuraan, jox ku turondoom Sëriñ Seex Awa Bàlla waaye mi ngi mokkale Alxuraan ci kenn ci taalibey Sëriñ Baara ñ
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (14)Bismillahi Rahmani Rahiim Dees na leeral ci xaaj wi mbiri àddiya, dolle gi mu am ak ay njariñam. Di na fi feeñee itam tabeeg Sëriñ bi. Naka noonu dees na fi béral waxi Sëriñ Tuubaa ci ay taalubeem ak ñi mu àndeek ñoom, naka noonu wuute yi am ci taalube yi
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (13)Bismillahi Rahmani Rahiim Ci xaaj wi deef na fi leeral, solos màggal gi fa Boroom Tuubaa, dayyob cant gi kawe na, yékkati ku na, te yooll yi bari. واجعل طعامي و شرابي يا كريم ذكرا و شكرا و ثوابا لا يريم « Yaw Yàlla mu tedd mi Yàlla nga def samaw ñam ak sa
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (12)Bismillahi Rahmani Rahiim Ci xaaj wi nag deef na fi fesal ne Sëriñ bi daan soññee ci fonk julli guddi, ci feggu ak ci sàmm sa ngëm. Deef na fi leeral yeneeni mbir jëm ci gëram sa Soxna. Sëriñ bi it jagle yu réy yi mu amoon. Naka noonu ay waxam ci Tuubaa,
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (11)Bismillahi Rahmani Rahiim Fii nag dees na fi leeral njariñu garabi wolof. Yenn gañcax yi nga xam ne daa baax lool ci wér gu yaram. Am na ci yu nuy baxal di naan, yii nu key segg ci ndox mu tàng. Su ko defe Sëriñ bi daf fiy xamle njariñ yi nekk ci garab yo
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (11)Bismillahi Rahmani Rahiim Fii nag dees na fi leeral njariñulg garabi wolof. Yenn gañcax yi nga xam ne daa baax lool ci wér gu yaram. Am na ci yu nuy baxal di naan, yii nu key segg ci ndox mu tàng. Su ko defe Sëriñ bi daf fiy xamle njariñ ci nekk ci garab
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (10)Bismillahi Rahmani Rahiim Deef na fi feeñal fonkug Sëriñ ci teerey xam-xam yi, rawatina yi jëm ci Tawhid ak Tasawuuf. Naka noonu ni mu daan tarbiyaa ay ñoñam ci xiif bu gudd fa Gànnaar. Sëriñ bi it di leen xirtal ci am ay teggin, di joxe te Yàlla rekk tax
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (9)Bismillahi Rahmaani Rahiim Fii danu fiy béral lenn ci waxi Sëriñ bi ci Xasiida yi. Lu mel ne ki Nuuru Daarayni ak Muqadimatul Amdaah. Muy ay néttali yoy dina soññi képp kuy góor-góorlu ci Xasiida yi mu yokk ay jéegoom. Ndax njariñ li nekk ci Xasiida yi re
il y a 2 ans - Bataaxel bu bàyyiko ci Sëriñ bi jëm ci Muxtaar(2).<<Yaw Muxtaar maa ngi lay dénk nga ragal Yàlla, te ragal Yàlla mooy jëf ndigal te bàyyi tere. Tey baril jëf yu baax, loolu mooy tax nga bari ay njariñ, te jiital allaaxira ci àddina ndax loolu mooy tax nga texe ëllëg, te mooy tax nga am kóolute ëllë
il y a 2 ans - Dénkaane bu jëm ci Soxna Penda Jóob (8)Bismilaahi rahmaani rahiim. Sëriñ bi ginnaaw ba mu leeralee ni kuy sàkku Boroomam la ak Yónnentam ba salla laahu tahaala aleyhi bi aalihi wa sahbihi wa salama, la daaldi wane ag jubloom ci dénk soxnas baayam ju ndaw ja, nu naan ko Penda Jóob. Daf ko wax n
il y a 2 ans - NITUG YALLAAy nitu Yàlla leen woon, ndax dañoo saxoon ci lislaam te loolu moo di topp Alxuraan ak Sunna, sax ci ndigali Yàlla yi ak wattandiku ay tereem, di teewlu xibaar yi dikk ci Téere Bu Sell Bi, di ko settantal, di ci waaru ak di ci waare. Seen dégg-dégg ci Dii
il y a 2 ans - Leeral Jazaa’u Shakuur (2)Bismillahi Rahmaani Rahiim Lii mooy ñaareelu xaaju Jazaa’u Shakuur te mooy sunu xaaj bu mujj. Sëriñ bi di di fi wax lenn ci coono yi mu daj Dakar, ca gaal ga. Ci néeg yu xat yi ñu ko daan duggal. Wax na fi it wax yu yéeme ci may yi mu jëlle ci tagg gi [&h
il y a 2 ans - Tombi Borom Tuubaa (8)Lii dees na fi jàngee doxiinu Sëriñ Tuubaa ci Alxuraan ak fonk gi mu ko fonkoon. Daf daan digle jàng Alxuraan, di ko durus ci ay lim yu wuute. Ba tay muy soññi way-jur yi ci jàngal seen i doom Alxuraan. Dëkkam bii di Tuubaa it muy fésal ag bëggam ci am ñu
il y a 2 ans