Di neen fi béral lenn ci dooley mbidum Sëriñ Tuubaa, njariñ yi mu làmboo ak jagle yi ak barkeb mbindam.
Naka noonu lenn ci mayi Sëriñ bi dees na ko fi fésal, ci man a xeetali mbindéef yi, fuñu man a nekk. Dees na fi dégg it nettali yoy dees koy gëm waaye deesuko xam.
Yal nanu Yàlla gën a xirtal ci liggéeyal Seexul Xadiim ak topp i ndigalam ak wattandiku ay tereem.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien