
Fii dees na fi wone lenn ci màndargay yërmandey Sëriñ bi ak ñi mu daan sàmme kollare. Ni mu wàccoog nun itam ci wax, ci jëf ak ci bind. Ak ni mu defoon ragal Yàlla muy lépp.
Naka noonu dees na fi leeral yennet ci xisa yuy wone xar-baaxi Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu.
Yal nanu Yàlla saxal ci liggéeyal ko.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien