
Ci xaaj wi dees na fi xamle itam leen ci Sëriñ bi, ni ki mbir yum baaxowoon def ak bis yu mu ko daan def. Ni mu fonkewoon julli ci waxtu, ak ni mu daan sàmmee taalube yi.
Ba tay, dees na fi wone ni mu doone ki nuy cinu ak di nu musal di tar-tari bàmmeel, ak bis penc, ak fi mu ñuy dëkkal ci àjjana.
Yal nanu Yàlla def ay murid dëgg.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien