Li ab Téere la bu am solo jëm ci xamlee nees di yoree sa Soxna ak ay mbir yu jëm ci dundug bàmmeel ak yeneeni yëf.
Ku ñuy wax Umar Jóob moo doon laaj Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu ay laaj yu am solo. Sëriñ bi bind Téere bi àndil ko ci ay tontu yu leer te fees ak njariñ.
Loolu moo tax ba Sëriñ Alhaaji Mbàkke gisee solo gi ci ne, ak néew gi Téere gi néew, la jóg def ci ligéey bu am solo. Yal na Yàlla barkeel lépp.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien