
Ci xaaj wi danu fiy leeral yi nga xam ne dina araam ci jigéen bu am ngàtt mu di ko def, mba muy dem ci ay barab yu mu warul dem.
Te war na ci Boroom kër mu xamal ko soxnaaam. Te mu xamal ko it mbolleem lu aju ci wàll woowu.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien