Miftaahu Xuyóob (12)

Ci xaaj wi di neen fi leere mbirum bàmmel. Tancug bàmmeel, laaji bàmmeel, ak i muslaay, ak i ñaan yu baax yu mat di tàmb wax ci làmmiñ.

Dina fi leere itam xéewalug sunu Boroom ci àjjanaam gi. Yal neen fa tàbbi nun ñépp.

Ba tay, bunt bi daf ñuy jàngal ne waajal sa bopp manul ñàkk, yar njaboot gi ci Diine tamit farata la, fexe itam ñuy am coffeel ak yërmande ci mbindéef yi, bu ñuy dund ak bu ñu fàttoo.

Moom Baay Seex Mbay mii ci nattaal bi nag noo ngi sàkku ñépp ñaanal ko njéegal, yërmande ak ngëramul sunu Boroom

Miftaahul Xuyóob<< Miftaahul Xuyóob (11)Miftaahul Xuyóob (13) >>
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR