Bismilaahi Rahmaani Rahiim
Dooley mbidum Sëriñ Tuubaa ci lawhul Mahfuus, ni ko fa sunu Boroom dëggarale dina yéem ku ne. Saytane itam day daw mbidam ndax da koy gàcceel, di bégloo Malaayika yi aleyhimu salaam ak jigéeni àjjana. Ay Xasiidam dafa mel ne xare, moom ak jëfi waa Badar ñoo yem, dafay texel murid bi di ko jubal.
Al-Habdul Xadiim
11/12/2020
Yalla naniou sax ci diang xassidagui te Diko séllal
Amiin barkeb Xasiida yi
Ndeyssan MaSha’ALLAH
Jërëjëf Gueye