
Fii di neen fi jàngee liy tax nu gën a njariñu ci Sëriñ Bi Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu.
Bokk na ci jàpp ci moom bu wér ak di góor-góorlu ci Xasiida yi. Di neen fi xamee it ne, tawfeexe na lool nga ànd ak Sëriñ Tuubaa.
Di neen fi déggee itam lenn ci ay jagleem, muy may yu yéeme, ak ni mu xame mbir yoo xam ne ump na ñu bari.
Yal nanu Yàlla sàmmal sunu Diine ak sunug taalube.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien