
Dees na xamee ci xisa yi yu bari ci mayi Yàlla yi. Nit dina man a xam ay mbir yu nëbbu ci coobareey sunu Boroom.
Dina fi feeñee itam dolleey ngëm, dooleey kóolute ak i jeexitalam ci topp ndigalu Sëriñ bu mat Sëriñ.
Yal nanu Yàlla saxal ci ag taalube, sàmmoonte, ak ragal Yàlla.
amna solo mais audios yi dafa gatt
Dinaa ko yokk😊