Bismilaahi rahmaani rahiim.
<<Képp koo xam ne yaa ngi sàkku àjjana ci lu dul ngay topp Yàlla sunu Boroom, te yaakar ne danga koo am sab xol leerul, ndax ba laa kenn a man a ngóob day fekk mu farlu woon cim mbay. Lépp loo xam ne da lay gàllankoor ci topp sunu Boroom bàyyi ko moo gën. képp kuy topp bëgg-bëggi nit ñi bay merlo Yàlla sunu Boroom ab dof la. Ndax loolu du ko njariñ dara bu gërëmloowul sunu Boroom.>>
Al-Habdul Xadiim
Grenoble, 01 /02/2020.
Merci beaucoup ❤
Je vous en prie.
Jerjefaaty
Jaajëfaat
Sant nagn dh.
Noo ko bokk
MachaAllah yaram 👌🏻
Jaajëf
Dieureudieuf Mouride
DIEUREUDIEUF SANGUE BI AMNA SOLO. yalla na borom bi yok xama xam bi ak meune meune bi
Amiin ku baax! Te mu boole nu ko