Jotaayu Texe (11)

Dees na jàngee ci nettali yi lenn ci mayi Sëriñ Bi, yërmandeem ci nit ñi, ak mbaaxam, ak bëgg gu tar gum bëggoon Yonent bi Aleyhi Salaam.

Noonu ba tay di neen fi déggee lol daf nuy gën a soññi ci ab yar, sàmmonte, ak bëgg lu baax.

Gën a góor-góorlu ci sunuy séy ak ci njaboot gi manul ñàkk tamit ngir njariñu àdduna ak allaaxira.

Ba tay noo ngi ñaanal Sëriñ Musaa Géy Ndar, mi ci nataal bi sunu Boroom dolli ko tawfeex, yërmande ak njéggal, te tàbbal ko ci àjjanaam yu kawe yi.

Jotaayu Texe<< Jotaayu Texe (10)
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR