
Dina leere ci xisa yi njariñul laabir, joxe, digle lu baax ak di ko jëfe. Dees na fi xamee itam lenn ci mbiri Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu.
Ak ay dénkaane yu am solo yu mu jaarale ci ay tomb.
Ba tay noo ngi ñaanal Faamara Seen sunu Boroom yëram ko, jéggal ko te gëram ko ba fàww.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien