Jotaayu Texe (9)

Di na leere ci nettali yi njariñul bàyyi tere ak topp ndigal, te farlu ci bu baax biir ak biti.

Di neen fi jàngee ne yéene ju refet manul ñàkk ba laa nuy jëf ak bàyyi xel Yàlla Subhaanahu ci sunuy wax ak sunuy jëf.

Yal nanu Yàlla saxal ci ag njub, ak am worma ci wàll yépp Barkeb Seexunaa Ahmadul Xadiim

Jotaayu Texe<< Jotaayu Texe (8)Jotaayu Texe (10) >>
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR