Miftaahul Xuyóob (13)

Xaaj wi nag di na fi leere liy waral mbugalum bàmmeel, am na ci yoy ay jëf la, am ci yoy ay wax la.

Yal nanu ci Yàlla musal.

Waaye di neen fi jàngee tamit liy musle ci mbugalum bàmmeel. Am na ci yoo xam ne ay ñaan la, yii ay ràkkaa yu baax a def, naka noonu jàngum Alxuraan moom man na lu ne.

Nuy sàkku ci ñépp ñu gën a yaatal application bi. Nu bokk njariñu.

Miftaahul Xuyóob<< Miftaahu Xuyóob (12)Miftaahul Xuyóob (14) >>
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR