
Fii dañu fiy leeral jëf yi nga xam ne du dog mukk.
Daanaka rekk mooy ay jëf yoy dina njariñ nit ñi, moo xam luy tax ñuy jàng Alxuraan, lu leen di tax a sàkku xam-xam, am wér gu yaram, amug feex ak jàmm.
Li lépp di tegtal ne liggéeyal Yàlla ci jaamam yi bari na njariñ lool. Yal nanu ci sax Barkeb Borom Tuubaa
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien