
Xaaj wi di neen fi jàngee lenn ci mbir yi aju ci bàmmeel, ci lenn ci jëf yu baax ya fay am, mel ne jàng Alxuraan ci bàmmeel.
Xisa yu bari rot ci bàyykoo ci Yonent bi Aleyhi Salaam, Sahaaba yu baax ya ak Taabihuuna ya.
Yal nanu Yàlla xir ci Alxuraan. Yal na Yàlla yëram Sëriñ Ahmadul Maxtaar mii wuyuji Boroomam te taas nu ci barkeem
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien