Ba tay warteefi borom kër ci soxnaam leen fiy xamle. Mel ne xamal ko diineem ak yi ci aju. Di ko leeralal lenn ci sew-sewi julli ak yi ci des.
Daa wara xamal njabóotam itam ak ñi mu yilif seen diine.
Yi jëm ci dareeti mbërag, wësin, yooyu yépp daf ko wara xam, te xamal ko soxnaam.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien