
Li ab tënk la ci mellooy Malaaka yi nga xam ne ñooy laaj ci bàmmeel. Te ñooy Munkar ak Nakir.
Raglu nanu lool.
Yal nanu Yàlla sàmmal sunu ngëm te bégal nu ci àdduna, barsaaq, allaaxira ak àjjana barke Borom Tuubaa.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien