
Dees na xame ci téereb Sëriñ Allaaji Mbàkke bi naka lañuy siyaare Sëriñ Bi. Mu fiy wone teggin yi ñu war a làmboo bu nu koy siyaare.
Naka noonu yéene ji, farlu gi, ak defin wi.
Nu xame ci rekk nag dafa wone aw yoon wu am solo ci siyaare Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu. Ñàkkul ni dana am yeneeni defin yu am solo tamit. Yal nanu ko Yàlla fayal.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien








