Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
Ndeke kuy sàkku Xam-Xam, war na nga xam luy jublu gi ak am melokaan buy taq ci yaw ngir jariñu gën a jàppandi. Ba tay, xam-xam leer gu réy a ngi ci bu lépp àndeek seelal ak rafet yéene. Ndeke sax fàww nga yar sa bakkan, dëddu àdduna, tënk say bànneex te daw saytaane ak dëkkam ya.
Al-Habdul Xadiim
06/06/2020
Machallah fall 👌
Jërëjëf
Machallah amatina solo yallah na sounou
uborom doli xam xam bi .si barkep borom touba ter defal lasi ak geuramame .
Amiin Amiin mu boolé nu lépp barke Borom Tuubaa!
Maa shaa Allah. Lou am solo nga wakh. Yalla nanou yalla deffal degue ak top
Amiin Amiin barke Borom Tuubaa!!!