« Ku yàkkaar ne sama tukki bii dama cee jëm feen fu dul ci Yàlla ak Yonent bi ba tax mu may dëkk yor jaasi ak i kano, Yàlla dana ko gàcceel, seetaan ko, mbindéef yi dinañu ko ngàññi, yeed ko, mu dee ak gàccee ak toroxtange.
Yàlla nag dina ma dimbali far ak man, mbindéef yi dinanu ma topp ci géej gi ak ci jeeri ji may Boroom i njariñ te duma lore ».
Al-Habdul Xadiim
13/09/2021
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien