Bismillahi Rahmaani Rahiim Ginnaaw leeral lu aju ci natuwaayu xisa yi. Deen fiy yaayal waxtaani Sëriñ Tuubaa walla Tombi Boroom Tuubaa.
Sëriñ Alhaaji Mbàkke moo bind Téere bi. Di ko ñaanal mu yàgg fi lool te wér. Yàlla dolli ko kàttan ak man-man ci lépp. Su ko defe saa bu àndee benn xisa rekk day daaldi àndi ab jàngat. Jàngat yooyu nag du nu ko àndi ci sunuy néttali ndax bëgg neen nit ñi man a fàggu Téere ak di ko yër. Sunu tomb bii nag li fi ëpp ci weetal Yàlla la jëm ak bañ a yemale waxtu julli ak leneen lum manti doon.
Mâcha Allah am na solo lool
Jërëjëf yaaram fasaale rekk