Serigne Saliou Mbacke ibn Serigne Abdoul Ahad JAARAMA CHEIKH IBRAHIMA FALL

Li xol bi yene

Li xol bi yeene ci aw yiw Yalla daal a ko xam Moo man ni cas benne lii mey bëg yit nima am Mbooleem lu bon bëg naa ca genn set ca bu wer Ta dëk ciw yiw ta andak Yalla faw ta gëm YouTube: Serigne Mbaye DIAKHATE

Kéenal Seriñ bi bi-qalami Seriñ Mbay Jaxate

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR