Ap dog Ni ñuy gëmé dogal bi moodi ñu gëm ne lepp lu am suñu boroom mooko amal ci kàttanam ak ub xam-xamam, moo xam lu nëbbu la wala muy lu feeñ, wala aw yiw wala aw ay, melné toppu yoonu yonnent bi salla laahu tahala aleyhi bi alihi wa sahbihi wa salam wala topp […]
Bismilahi rahmani rahim Ap dog Ni ñuy gëmé yonnent yi aleyhimu salàtu wa salamu móodi da ñuy gëm ne suñu borom mo len yóoni ci ñun bu werr. Gëm itam lepp luñu andi, te gëm ne duñu fen, duñu def lu haram, duñu def luñu sib, duñu nëbb li ñu len digal ñu jottaliko mindeef […]