Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
Di nga fi xame dooley xam-xam. Ba tey, ndegam bëgg nga ràññatle sunna ak bidaa, boo teewloo ndénkaan yi dina la jariñ.
Al-Habdul Xadiim
03/06/2020

Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
Di nga fi xame dooley xam-xam. Ba tey, ndegam bëgg nga ràññatle sunna ak bidaa, boo teewloo ndénkaan yi dina la jariñ.
Al-Habdul Xadiim
03/06/2020
Teggin yi war ci kuy jàng ak solos xam ak jëfe ci Zaadu Zawii-Tahalumi(2)
Xiif ak àddis yi ci rot; ak naka la xam-xam yi gënante ci Zaadu Zawii-Tahalumi(3)
Dénkaane Sëriñ bi jëm ci ab muritam(1).
Dénkaane bu jëm ci doomi mbokki Sërin Tuubaa(14).
Dénkaane bu jëm ci Seex Mabaabu Géy ak yeneeni dénkaan yu jëm ci bépp murit
Dénkaane bu jëm ci Abdullahi (6)
Dénkaane bu jëm ci topp Yàlla (4)
Dénkaane bu jëm ci Murid yëpp (10)
Machallah fall yarame
Jërëjëf
Dieureudieuf Mouride si fatali bi
Jaajëfaat noo ko bokk