Bismilaahi Rahmani Rahiim
Jaar-jaari Yónnent bi (Saws) – 3
Fii di nga fi xamee leen ci pexe yi nga xam ne yéefar yi daan nañu ko fexeel Gën ji mbindéef. Da naa fi wax fi itam faatug Aamina ak Abdul Mutalib. Yoonu Saam ak li fa feeñ ci xarbaax. Jambarug Soxna Xadiija ci tambalig Wahyu gi itam maneesu koo fàtte.
Al-Habdul Xadiim
28/10/2020
Jerejef Cheikh bi
Jaajeuf yaaram
Machallah fall
Jërëjëf
Maa shaa Allah. Yalla nala yalla faiye si leeral yi.
Amiin nu bokk ko