Jotaayu Texe (6)

Ci xaaj wi dees na fi gën a xamee mayi Yàlla sunu Boroom. Di neen fi gis it ni ñaanlu ci say mbir lu baax la.

Moom Sëriñ Tuubaa nag di neen déggee ci nettali bi fonkam Alxuraan ak jibboo ak Boroomam.

Yal nanu Yàlla sàmmal sunu Diinee.

Jotaayu Texe<< Jotaayu Texe (5)Jotaayu Texe (7) >>
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR