
Lii ab dog la bu jëm ci Xasiida yi, teewlu gi ci war ak déglu gi, ànd solo si mu làmboo.
Naka noonu dina feeñee ci nettali yi ay mbir yu kéemaane ci mayi Sëriñ Tuubaa.
Yal nanu Yàlla jubal te baaxal nu Barke Borom Tuubaa.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien