Miftaahul Xuyóob (16)

Di nanu leeral ci xaaj bii, njariñal siyaare baameel ci ñiy dund ak ñi faatu.

Bu dee kiy dund dina xam mi àdduna saxul, fàww dina faatu. Loolu ag waar la, jaaju la it ci moom. Ki faatu moom dina jot i xéewal ndax ñaan yi miy jot.

Yal nanu jeexal sunu dund ci ag njub Barkeb Alxuraanul Kariim.

Miftaahul Xuyóob

Miftaahul Xuyóob (15) Leeral Miftaahul Xuyóob (18)
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR