Taysiiru Rahmaan

Bismillahi Rahmaani Rahiim.

Lii ab Téere la bu jëm ci tontu Umar Ñaan kenn la ci taalibey Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu.

Dénkaane gu am solo la lool. Sëriñ bi fàttali fi màggug Sunu Boroom, tudd melloom yu sell yi, di xamle ne lépp ci ay yoxoom la nekk. Lu sotti lu nekk moom la. Soññi mbokkam mi ci farlu ci jaamu Yàlla, dëgmal lu baax, moytu lu bon, taqoo ñu baax ñi. Njariñ li yaatu na lool te ñeel bépp julit.

« Ayib yi ñooy tax doo gis yu nëbbu yi. Moy yi ñooy waral doo gis may yi ».

Al-Habdul Xadiim
29/05/2022

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR