Bismillahi Rahmani Rahiim
Ci xaaj wi deef na fi leeral, solos màggal gi fa Boroom Tuubaa, dayyob cant gi kawe na, yékkati ku na, te yooll yi bari.
واجعل طعامي و شرابي يا كريم ذكرا و شكرا و ثوابا لا يريم
« Yaw Yàlla mu tedd mi Yàlla nga def samaw ñam ak samag naan muy ak tudd Yàlla, di ak cant téy tiyaaba juddul dakk mukk ».
Naka doonu deef na fi feeñal li tax nu war di sopp Sëriñ Tuubaa, tey bañ di ko noonoo. Ak lu tax nu war di fonk ak a sàmm ay jeexitalam : suufug Tuubaa, njaboot gi, taalube yi, léppam daal cib tënk.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien