Ci xaaj bi, dees na fi àndi lenn ci yi Sëriñ bi daan wax ci bisu penc ak may yi ko fa Yàlla jagleel.
Ni miy xéttale nit ñi ci àdduna noonu it la leen di xéttale ëllag.
Naka noonu di neen fi béral lenn ci dénkaane yi itam ak njariñ yu réy yi ñu làmboo.
Yal nanu Yàlla defal tawfeexi bëgg Sëriñ Tuubaa ak di ko liggéeyal.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien