Bismilaahi rahmaani rahiim Sëriñ bi Xaada lahu laahu Maxtaara lahu moo fiy xamle ni nit ki wara melokaano bu dee sàkku Xam-Xam. Dana fi feeñee njariñal xam-xam ak teggin ak yi ci aju. Sëriñ Alhaaji Mbàkke moo ko leeral ci wolol. Yal na nu Yàlla defal dégg ak topp barke weeru koor gi. https://al-habdul-xadiim.com/wp-content/uploads/2020/05/VID-20200517-WA0020.mp4.mp4 Al-Habdul […]
Bismilahi rahmani rahim. « Sëriñ Alhaji Mbàkke Xàdimul Xadiim mo ci’y gàttal ci wolof téeré bii ngir bëgg julit yëpp njariñu ci rawanté’naak muriid yi yalna ko yàlla nangu ci barkep Sëriñ Tuuba Qàda lahu laahu Maxtara lahu » *** Méñatum « Jazbatu sighàr » Bismilahi rahmani rahim salla laahu hala sayyidina muhamadin wa […]