Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
Ci buntu bi lanu fas yéene tejje Zaadu Zawii-Tahalumi. Di nga fi dégge ay àddis yu bari yuy wax ci mbiri xiif ak jeexital yu am jariñ yi muy def ci ruuhu dóomu aadama bi. Jàppandal la ci sàkku xam-xam, ak yar sa bakkan. Te kenno la ci tasawuuf! Di nga fi xame itam ne, jullit bi lépp lu miy jëfandikóo war na saytu ba xam dagan na ko , walla mu araam walla mu lënt.
Al-Habdul Xadiim
13/06/2020
Jërëjëf ci yaatal gi amna solo yàlla nanu yàlla kattanal ba nu man a jëfe digle yi
Amiin Amiin barke Borom Tuubaa!
Maa shaa Allah. Yalla nanou yalla deffal degue ak topp. Meytou regg barké kou tedd ki
Amiin Amiin yal na Yàlla nangu ñaan yépp
Aaamenaa soolo Fall
Yallah naala kou teidd kii Faay mais geune koo yatall thi RS , télégramme wala insta
Diadieuf