Bismilaahi rahmaani rahiim
<<Li ma lay bëgg dénk, ndénkaane la boo xam ne képp kuy moytu ay ñaawteef dina baril sag may.
Al-Habdul Xadiim,
Maa ngi lay dénk xam-xam ak jëfe ak teggiin. Sab xol nanga ko setal ci ay taq-taq kon dinga jiitu sag maas. Deel toroxlu ci say mbokk ngir laabire leen kon dinga mucc ci ag mbañeel ak gàcce. Deel toroxlu ci jullit yëpp kon dinga mucc ci ay lëndam.
Saa soo gise sama mbind mi nag, yaw, sama loxob nday-jóor, na nga ko terale tuub. Saw làmmiñ dee ko nooyal ak sab xol ci jullit yépp, kon dinga boole gën gi yiiw. Maa ngi lay woo tay ci saw tur « Ibraahimu » di la wax ne képp koo xam ne boo ko xamale mu njariñ ko, xamal ko!>>
Grenoble, 22/02/2020.
Masha’Allah amna solo lool
Alhamdoulilah jërëjëf
MachaAllah
Jaajëf soxna Astou
Macha allah bonne continuation
Merci
Am na sollo lolle kénn dou borom darou la main du cheikh
Ndeysaan
Jërëjëf waay, am na solo lool
Jaajëfaat
Amna solo lool jërëngeen jëf
Jaajëfaat
dieureudieuf yaram machallah
Jaajëf ku baax
Great content! Super high-quality! Keep it up! 🙂
Thanks you so much
Akaasa Segne cheikh
Jaajëf